Jangat(gëstu) sama ndono: 4 kangam yu Africa (Hardcover)
Waa so m non delloo ay waxtu walla ay at ci ganaw?
Ak t er bi, ma ngi l woo ci ng dellu ci d mb ndax ng xam sa ndono ni mu r y .
Buur bu goor ak bu jig en, njitt d kk ya won ak jambaar yu goor ak yujig en, defaral sa toggay te ng g stu(j ngat)
J fin ak kawtefu 4 kangam d mb yi ci Afrik.
Ci jeexantal t er bi, ab p cc laa u la jagglel ngir ng tekk
ay kuloor ci nitaal yi lolu dina tax ng bokk ci l eb bi ci wetu jambaar yi.
Mbaa pare ng ?